fbpx

Seetaanleen ay wideo

Lan moo indi ragal ci sunu dund? Seetaanleen wideo yi ngir jàngat li ci biir ba xam lu tax lanu ragal lu bare tey ji, ak kan moo man saafaral sunu ragal yi.

Ubbite gi

Sàkk-kat bi ak càkkéefam

Duggug naxekat bi

Mbugalug bàkkaar ak digeb Yàlla

Sarax ba

Fippug nit ak takkuteg Yàlla

Pexem Yàllaa ngi jëm kanam

Yoonu Musaa ak tére yonent yi

Duggsig Buur bi

Jikkoy Buur bi

Nguur gu mag gu Buur bi

Sasu Buur bi

Nangug Buur bi

Saraxu Buur bi ak ndaanug

Xabaar bu baax bi ak ndamu Buur bi

Maryama mu Magdala

Maryaama ab taalibe Isaa la woon, te dund na lu bare ak ñi doon topp Isaa ci liggéeyam. Seetaanleen nettaleem ngir seede yërmaandeem Isaa ak yiwam.